Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 4:9-12 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 4:9-12 in Kàddug Yàlla gi

9 Da lay takkal kaala gu jekk, solal la mbaxanam buur.»
10 Déglul, doom, te dégg saay wax, ndax nga gudd fan.
11 Yoon wu xelu laa la teg, jaarloo la yoonu njub.
12 Doo dox ba tërëf, doo daw, téqtalu.
Kàddu yu Xelu 4 in Kàddug Yàlla gi