Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 31

Kàddu yu Xelu 31:25-28

Help us?
Click on verse(s) to share them!
25Faaydaak jom la làmboo, te ëllëg ubul boppam.
26Day wax lu xelu, di digle ngor.
27Jigéen jooju mooy bàyyi xel ci njabootam, te du nangoo yàccaaral.
28Doom ya dañu ko naan: «Jarawlakk!» jëkkër ja di ko gërëm naan:

Read Kàddu yu Xelu 31Kàddu yu Xelu 31
Compare Kàddu yu Xelu 31:25-28Kàddu yu Xelu 31:25-28