Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 31:25-28 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 31:25-28 in Kàddug Yàlla gi

25 Faaydaak jom la làmboo, te ëllëg ubul boppam.
26 Day wax lu xelu, di digle ngor.
27 Jigéen jooju mooy bàyyi xel ci njabootam, te du nangoo yàccaaral.
28 Doom ya dañu ko naan: «Jarawlakk!» jëkkër ja di ko gërëm naan:
Kàddu yu Xelu 31 in Kàddug Yàlla gi