Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 30

Kàddu yu Xelu 30:25-29

Help us?
Click on verse(s) to share them!
25xorondom, néew na doole, waaye bu jotee, mu denc dundam;
26daman, barewul kàttan, te day dëkk ciy doj;
27soccet, amul buur, teewul ñuy àndandoo, diy gàngoor;
28sindax, manees na koo ŋëb, teewul ma nga biir kër buur.
29Ñett a ngii, ñu jekk um ndaag, ba ci ñeent ñu jekk doxin:

Read Kàddu yu Xelu 30Kàddu yu Xelu 30
Compare Kàddu yu Xelu 30:25-29Kàddu yu Xelu 30:25-29