Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 29

Kàddu yu Xelu 29:3-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Kuy jëfe xel, bégal sa baay; nga ànd aki gànc, yàq alal.
4Buur jub, am réew dëgër; mu bëggi galag, réew ma sànku.
5Kuy jay sa moroom, yaa ngi koy dugal.
6Ku bon day moy, ba dugal boppam; ku jub di woy ak a bànneexu.
7Ku jub a xam àqu néew-ji-doole, ab soxor xamu ca dara.

Read Kàddu yu Xelu 29Kàddu yu Xelu 29
Compare Kàddu yu Xelu 29:3-7Kàddu yu Xelu 29:3-7