Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 29:3-7 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 29:3-7 in Kàddug Yàlla gi

3 Kuy jëfe xel, bégal sa baay; nga ànd aki gànc, yàq alal.
4 Buur jub, am réew dëgër; mu bëggi galag, réew ma sànku.
5 Kuy jay sa moroom, yaa ngi koy dugal.
6 Ku bon day moy, ba dugal boppam; ku jub di woy ak a bànneexu.
7 Ku jub a xam àqu néew-ji-doole, ab soxor xamu ca dara.
Kàddu yu Xelu 29 in Kàddug Yàlla gi