Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 27

Kàddu yu Xelu 27:1-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Bul damoo ëllëg, ndax xamoo luy xew tey.
2Bul tëggu, bàyyil ñu tagg la, muy waxi keneen; yaw, bu ko wax.
3Doj diis na, suuf dib sëf, waaye fitnay dof a ko raw.

Read Kàddu yu Xelu 27Kàddu yu Xelu 27
Compare Kàddu yu Xelu 27:1-3Kàddu yu Xelu 27:1-3