Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 24

Kàddu yu Xelu 24:4-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Xam-xam ay feesal néeg ya ak mboolem alal ju jafe te yànj.
5Ku rafet xel di boroom doole, ku xam, gëna man;
6tegtal yu xelu lañuy xaree, diisoo bu yaatooy maye ndam.
7Wax ju xelu sut nab dof, jataayu pénc du fa àddoo.

Read Kàddu yu Xelu 24Kàddu yu Xelu 24
Compare Kàddu yu Xelu 24:4-7Kàddu yu Xelu 24:4-7