Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 24

Kàddu yu Xelu 24:29-33

Help us?
Click on verse(s) to share them!
29Bul ne: «Li mu ma def laa koy def, damay feyu li mu ma def.»
30Toolub ku yaafus laa jaare, ak tóokërub nit ku ñàkk bopp.
31Ndeke lépp a nga saxi dég, fépp fees akum ñax, tabaxu doj ba ko wër màbb.
32Maa ko gis, di xalaat, xoolaat ko, jànge ca.
33Booy dajjant ak a for bët, di tegley loxook a jaaxaan,

Read Kàddu yu Xelu 24Kàddu yu Xelu 24
Compare Kàddu yu Xelu 24:29-33Kàddu yu Xelu 24:29-33