Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 22

Kàddu yu Xelu 22:2-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Ku am ak ku ñàkk a bokk lenn: Aji Sax jee leen boole sàkk.
3Kuy foog, gisu ay, làqu; ab téxét ne ca tëñëx, loru.
4Woyofal te ragal Aji Sax ji, am alal, gudd fan ak daraja.
5Yoonu njublaŋ, ay dég aki fiir; ku sàmm sa bakkan sore ko.

Read Kàddu yu Xelu 22Kàddu yu Xelu 22
Compare Kàddu yu Xelu 22:2-5Kàddu yu Xelu 22:2-5