Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 22:2-5 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 22:2-5 in Kàddug Yàlla gi

2 Ku am ak ku ñàkk a bokk lenn: Aji Sax jee leen boole sàkk.
3 Kuy foog, gisu ay, làqu; ab téxét ne ca tëñëx, loru.
4 Woyofal te ragal Aji Sax ji, am alal, gudd fan ak daraja.
5 Yoonu njublaŋ, ay dég aki fiir; ku sàmm sa bakkan sore ko.
Kàddu yu Xelu 22 in Kàddug Yàlla gi