Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 21

Kàddu yu Xelu 21:28-31

Help us?
Click on verse(s) to share them!
28Seede buy fen day sànku, kuy dégg, sa kàddu sax.
29Ku bon day ñeme-ñemelu, ku jub la muy def da koy wóor.
30Nit xeluwul, amul ug dégg ak pexe, ba manal Aji Sax ji dara.
31Nit ay takk, bésub xare, Aji Sax ji di maye ndam.

Read Kàddu yu Xelu 21Kàddu yu Xelu 21
Compare Kàddu yu Xelu 21:28-31Kàddu yu Xelu 21:28-31