Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 21

Kàddu yu Xelu 21:22-25

Help us?
Click on verse(s) to share them!
22Ku ñaw mana daan jàmbaari dëkk bu mag, ba màbb tata ja ñu yaakaaroon.
23Ub sa gémmiñ, moom sa làmmiñ, mucc ci njàqare.
24Ku réy te bew, mooy ñaawle, day reew, ba jéggi dayo.
25Ab yaafus day bëgg lu mu amul ba dee, ndax du nangoo liggéey;

Read Kàddu yu Xelu 21Kàddu yu Xelu 21
Compare Kàddu yu Xelu 21:22-25Kàddu yu Xelu 21:22-25