Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 21:22-25 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 21:22-25 in Kàddug Yàlla gi

22 Ku ñaw mana daan jàmbaari dëkk bu mag, ba màbb tata ja ñu yaakaaroon.
23 Ub sa gémmiñ, moom sa làmmiñ, mucc ci njàqare.
24 Ku réy te bew, mooy ñaawle, day reew, ba jéggi dayo.
25 Ab yaafus day bëgg lu mu amul ba dee, ndax du nangoo liggéey;
Kàddu yu Xelu 21 in Kàddug Yàlla gi