Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 1

Kàddu yu Xelu 1:1-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Kàddu yu xelu yu Suleymaan buurub Israyil, di doomu Daawuda.
2Li ko taxa jóg di nit ñi am xel mu rafet, am ab yar, ngir xam wax ju lal dég-dég,
3ngir yaru ci jëfe xel ak njub ak yoon, di jubal,
4ndax ab téxét di foog, ndaw li it xam tey xalaat.

Read Kàddu yu Xelu 1Kàddu yu Xelu 1
Compare Kàddu yu Xelu 1:1-4Kàddu yu Xelu 1:1-4