Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 1:1-4 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 1:1-4 in Kàddug Yàlla gi

1 Kàddu yu xelu yu Suleymaan buurub Israyil, di doomu Daawuda.
2 Li ko taxa jóg di nit ñi am xel mu rafet, am ab yar, ngir xam wax ju lal dég-dég,
3 ngir yaru ci jëfe xel ak njub ak yoon, di jubal,
4 ndax ab téxét di foog, ndaw li it xam tey xalaat.
Kàddu yu Xelu 1 in Kàddug Yàlla gi