Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 19

Kàddu yu Xelu 19:1-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Ñàkk te mat, moo gën dof, di wax njekkar.
2Teeyadi baaxul, ku yàkkamti moy saw yoon.
3Nit def na jëfi dof, ba sànku, walbatiku mere Aji Sax ji.

Read Kàddu yu Xelu 19Kàddu yu Xelu 19
Compare Kàddu yu Xelu 19:1-3Kàddu yu Xelu 19:1-3