Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 16

Kàddu yu Xelu 16:21-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
21Ki rafet xel mooy kiy ràññee, te su wax rafetee, dég-dég yomb.
22Xel mu ñaw day suuxat bakkan, te ab dof jëfi dofam a koy yar.
23Ku rafet xel, say kàddu xelu; soo waxee, yey.
24Wax ju yiw di lem juy xelli, neexa ñam, di jàmmi yaram.

Read Kàddu yu Xelu 16Kàddu yu Xelu 16
Compare Kàddu yu Xelu 16:21-24Kàddu yu Xelu 16:21-24