Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 16:21-24 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 16:21-24 in Kàddug Yàlla gi

21 Ki rafet xel mooy kiy ràññee, te su wax rafetee, dég-dég yomb.
22 Xel mu ñaw day suuxat bakkan, te ab dof jëfi dofam a koy yar.
23 Ku rafet xel, say kàddu xelu; soo waxee, yey.
24 Wax ju yiw di lem juy xelli, neexa ñam, di jàmmi yaram.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi