Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 12

Kàddu yu Xelu 12:15-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Na dof di jëfe, njub la ci moom; dégg ndigal rafet um xel la.
16Ab dof bu meree, mu gaawa feeñ; ku teey, tanqamlu saaga.
17Ku dëggu, seede dëgg; seede bu bon, fen rekk.
18Làmmiñu waxkat, jam-jami jaasi; kàddu gu xelu, garab la ci.
19Kàdduy dëgg, day sax dàkk; fen, xef xippi, mu wéy.
20Kuy ràbb lu bon lal pexey wor, kuy digle jàmm, am mbégte.

Read Kàddu yu Xelu 12Kàddu yu Xelu 12
Compare Kàddu yu Xelu 12:15-20Kàddu yu Xelu 12:15-20