Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - JËF YA - JËF YA 10

JËF YA 10:13-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Te baat ne ko: «Jógal, Piyeer, rey te lekk.»
14Waaye Piyeer ne ko: «Mukk, Boroom bi, ndaxte masumaa lekk dara lu daganul mbaa lu araam.»
15Waaye baat bi wax ak moom ñaareelu yoon ne ko: «Lu Yàlla sellal, bu ko araamal.»
16Ñu def ko nag, ba muy ñetti yoon, ba noppi ñu ne cas sér ba, jëme asamaan.

Read JËF YA 10JËF YA 10
Compare JËF YA 10:13-16JËF YA 10:13-16