Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Jëf ya - Jëf ya 10

Jëf ya 10:13-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Mu am baat bu jib, ne ko: «Piyeer, jógal, rey te lekk.»
14Piyeer ne ko: «Mukk, Sang bi, ndaxte masumaa lekk lenn lu daganul mbaa lu setul.»
15Teewul baat bi wax ak moom ñaareel bi yoon, ne ko: «Lu Yàlla setal, bu ko daganadil.»
16Menn peeñu moomu dikkal na ko ñetti yoon. La ca tegu ñu yéege këf ka asamaan.

Read Jëf ya 10Jëf ya 10
Compare Jëf ya 10:13-16Jëf ya 10:13-16