Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - 1.Samiyel - 1.Samiyel 16

1.Samiyel 16:7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Aji Sax ji nag ne Samiyel: «Bul xool ci melokaanu kii, mbaa jëmmu taxawaayam, ndax gàntal naa ko. Lii du ci gis-gisu nit. Nit, li fees bëtam lay gis, waaye Aji Sax ji ci xol lay xool.»

Read 1.Samiyel 161.Samiyel 16
Compare 1.Samiyel 16:71.Samiyel 16:7