Text copied!
Bibles in Wolof

1.Samiyel 16:7 in Wolof

Help us?

1.Samiyel 16:7 in Kàddug Yàlla gi

7 Aji Sax ji nag ne Samiyel: «Bul xool ci melokaanu kii, mbaa jëmmu taxawaayam, ndax gàntal naa ko. Lii du ci gis-gisu nit. Nit, li fees bëtam lay gis, waaye Aji Sax ji ci xol lay xool.»
1.Samiyel 16 in Kàddug Yàlla gi