Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 9

Kàdduy Waare 9:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Lu mettee ngi nii ci mboolem lu am fi kaw suuf: Benn dogal la ñépp bokk, te it nit a ngi sóobu ci mbon, di mébét jëfi dof giiru dundam, ba noppi fekki ña dee.
4Képp kuy dund kat, am nga yaakaar, te xaj buy dund a gën gaynde gu dee.

Read Kàdduy Waare 9Kàdduy Waare 9
Compare Kàdduy Waare 9:3-4Kàdduy Waare 9:3-4