Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 9:3-4 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 9:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Lu mettee ngi nii ci mboolem lu am fi kaw suuf: Benn dogal la ñépp bokk, te it nit a ngi sóobu ci mbon, di mébét jëfi dof giiru dundam, ba noppi fekki ña dee.
4 Képp kuy dund kat, am nga yaakaar, te xaj buy dund a gën gaynde gu dee.
Kàdduy Waare 9 in Kàddug Yàlla gi