Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 8

Kàdduy Waare 8:4-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Kàddug buur kilifteef la. Ana ku ko naan: «Looy def nii?»
5Ku dégg ndigal doo am lu la soof. Ku xelu, xam lu jot, xam doxalin.

Read Kàdduy Waare 8Kàdduy Waare 8
Compare Kàdduy Waare 8:4-5Kàdduy Waare 8:4-5