Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 8:4-5 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 8:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 Kàddug buur kilifteef la. Ana ku ko naan: «Looy def nii?»
5 Ku dégg ndigal doo am lu la soof. Ku xelu, xam lu jot, xam doxalin.
Kàdduy Waare 8 in Kàddug Yàlla gi