Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 7

Kàdduy Waare 7:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Naqar a gën xaxaloo; aw tiis ñëkkal kanam, rafetal xol.
4Ku xelu, xalaat kërug dëj; ku dofe, xalaat kërug puukare.
5Déglu ku xelu di la àrtu moo gën déglu dof bu lay woy.

Read Kàdduy Waare 7Kàdduy Waare 7
Compare Kàdduy Waare 7:3-5Kàdduy Waare 7:3-5