Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 7:3-5 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 7:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Naqar a gën xaxaloo; aw tiis ñëkkal kanam, rafetal xol.
4 Ku xelu, xalaat kërug dëj; ku dofe, xalaat kërug puukare.
5 Déglu ku xelu di la àrtu moo gën déglu dof bu lay woy.
Kàdduy Waare 7 in Kàddug Yàlla gi