Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 7

Kàdduy Waare 7:20-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20Amul moos ku jub ci kaw suuf, kuy def lu baax te du bàkkaar.
21Te it du lépp lu ñu wax, ngay bàyyi xel. Kon doo dégg surga bu la ŋàññ,
22ndax xam nga xéll ne yaw it ŋàññe nga ay yooni yoon.

Read Kàdduy Waare 7Kàdduy Waare 7
Compare Kàdduy Waare 7:20-22Kàdduy Waare 7:20-22