Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàdduy Waare 7:20-22 in Wolof
Help us?
Kàdduy Waare 7:20-22
in
Kàddug Yàlla gi
20
Amul moos ku jub ci kaw suuf, kuy def lu baax te du bàkkaar.
21
Te it du lépp lu ñu wax, ngay bàyyi xel. Kon doo dégg surga bu la ŋàññ,
22
ndax xam nga xéll ne yaw it ŋàññe nga ay yooni yoon.
Kàdduy Waare 7 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms