Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 7

Kàdduy Waare 7:15-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Lu ne laa gis ci sama dund gu gàtt gii! Nit a ngii jub, teewu koo sànkook njubam; nit bon, ànd ak mbonam, gudd fan.
16Bul jub ba mu ëpp, bul wóolu sam xel ba mu ëpp, lu ko moy nga yàqule.

Read Kàdduy Waare 7Kàdduy Waare 7
Compare Kàdduy Waare 7:15-16Kàdduy Waare 7:15-16