Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàdduy Waare 7:15-16 in Wolof
Help us?
Kàdduy Waare 7:15-16
in
Kàddug Yàlla gi
15
Lu ne laa gis ci sama dund gu gàtt gii! Nit a ngii jub, teewu koo sànkook njubam; nit bon, ànd ak mbonam, gudd fan.
16
Bul jub ba mu ëpp, bul wóolu sam xel ba mu ëpp, lu ko moy nga yàqule.
Kàdduy Waare 7 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms