Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 6

Kàdduy Waare 6:8-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Ana lu boroom xel ëpplee ku dofe? Nga ñàkk, xam doxalin, lu mu lay jariñ?
9Doyloo li nga gis a gën di wéye xemmem. Loolu it, cóolóoli neen ak napp um ngelaw.
10Lu masa ay, dees koo tuddoon; lu doom aadama doon, xamees na ko, te kenn du layook ku la sut.

Read Kàdduy Waare 6Kàdduy Waare 6
Compare Kàdduy Waare 6:8-10Kàdduy Waare 6:8-10