Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 6:8-10 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 6:8-10 in Kàddug Yàlla gi

8 Ana lu boroom xel ëpplee ku dofe? Nga ñàkk, xam doxalin, lu mu lay jariñ?
9 Doyloo li nga gis a gën di wéye xemmem. Loolu it, cóolóoli neen ak napp um ngelaw.
10 Lu masa ay, dees koo tuddoon; lu doom aadama doon, xamees na ko, te kenn du layook ku la sut.
Kàdduy Waare 6 in Kàddug Yàlla gi