Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 6

Kàdduy Waare 6:5-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Gisul jant, xamu ko, waaye noflaay moo ko ëpple mag ma,
6bu dundoon junniy junniy at sax te amul jàmm. Xanaa du benn bérab la ñépp jëm?
7Nit ak doñ-doñam jépp, biiram, te taxul mu doylu.

Read Kàdduy Waare 6Kàdduy Waare 6
Compare Kàdduy Waare 6:5-7Kàdduy Waare 6:5-7