Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 6:5-7 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 6:5-7 in Kàddug Yàlla gi

5 Gisul jant, xamu ko, waaye noflaay moo ko ëpple mag ma,
6 bu dundoon junniy junniy at sax te amul jàmm. Xanaa du benn bérab la ñépp jëm?
7 Nit ak doñ-doñam jépp, biiram, te taxul mu doylu.
Kàdduy Waare 6 in Kàddug Yàlla gi