Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 5

Kàdduy Waare 5:7-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Boo gisee ñuy not néew-ji-doole, di jalgati dëgg ak yoon cib gox, bumu la jaaxal; kilifa gi, kilifaam a ko yiir; ñoom it seen kilifaa leen yiir.
8Xanaa ndax buur suqal mbey mi, ba ñépp jariñoo suuf si.

Read Kàdduy Waare 5Kàdduy Waare 5
Compare Kàdduy Waare 5:7-8Kàdduy Waare 5:7-8