Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 3

Kàdduy Waare 3:12-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Ma gis ne nit amul lu gën bànneex ak jàmmi bakkan cig dundam,
13te nitoo nit, su dee lekk ak a naan, di ñaq, jariñoo, loolu mayu Yàllaa.

Read Kàdduy Waare 3Kàdduy Waare 3
Compare Kàdduy Waare 3:12-13Kàdduy Waare 3:12-13