Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 3:12-13 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 3:12-13 in Kàddug Yàlla gi

12 Ma gis ne nit amul lu gën bànneex ak jàmmi bakkan cig dundam,
13 te nitoo nit, su dee lekk ak a naan, di ñaq, jariñoo, loolu mayu Yàllaa.
Kàdduy Waare 3 in Kàddug Yàlla gi