Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 2

Kàdduy Waare 2:8-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Ma dajale sama xaalis ak sama wurus, moom alali buur yeek diiwaan yi ma yilif, tabb samay woykat, góor ak jigéen, boole ci bànneex bi ci jabari jabar.
9Ma am doole, yokku, ba sut ku ma jiitu ci Yerusalem, te teewul may jëfe xel.

Read Kàdduy Waare 2Kàdduy Waare 2
Compare Kàdduy Waare 2:8-9Kàdduy Waare 2:8-9