Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 2:8-9 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 2:8-9 in Kàddug Yàlla gi

8 Ma dajale sama xaalis ak sama wurus, moom alali buur yeek diiwaan yi ma yilif, tabb samay woykat, góor ak jigéen, boole ci bànneex bi ci jabari jabar.
9 Ma am doole, yokku, ba sut ku ma jiitu ci Yerusalem, te teewul may jëfe xel.
Kàdduy Waare 2 in Kàddug Yàlla gi