Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 2

Kàdduy Waare 2:17-18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17Ma far bañ àddina. Ndaw naqar ci jëfi kaw suuf, te lépp di cóolóol ak napp um ngelaw!
18Sama doñ-doñ, ji fi kaw dun bi, génnliku na ma, dama koy wacce ka may wuutuji rekk,

Read Kàdduy Waare 2Kàdduy Waare 2
Compare Kàdduy Waare 2:17-18Kàdduy Waare 2:17-18