Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 2:17-18 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 2:17-18 in Kàddug Yàlla gi

17 Ma far bañ àddina. Ndaw naqar ci jëfi kaw suuf, te lépp di cóolóol ak napp um ngelaw!
18 Sama doñ-doñ, ji fi kaw dun bi, génnliku na ma, dama koy wacce ka may wuutuji rekk,
Kàdduy Waare 2 in Kàddug Yàlla gi