Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 2

Kàdduy Waare 2:12-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Ma geesu xoolaat xel mu rafet, xool ag nitoodi akug ndof. Ana ku may wuutuji ci nguur gi, lu muy def lu moy lu ñu daan def?
13Ma gis ne ni leer ëppe lëndëm njariñ, ni la xel mu rafet ëppe ndof njariñ.

Read Kàdduy Waare 2Kàdduy Waare 2
Compare Kàdduy Waare 2:12-13Kàdduy Waare 2:12-13