Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 2:12-13 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 2:12-13 in Kàddug Yàlla gi

12 Ma geesu xoolaat xel mu rafet, xool ag nitoodi akug ndof. Ana ku may wuutuji ci nguur gi, lu muy def lu moy lu ñu daan def?
13 Ma gis ne ni leer ëppe lëndëm njariñ, ni la xel mu rafet ëppe ndof njariñ.
Kàdduy Waare 2 in Kàddug Yàlla gi