Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 1

Kàdduy Waare 1:8-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8Jëfoo jëf ca jëfit, làmmiñ tuddul lépp, bët du suur, nopp du buur.
9Lu ayoon mooy ayati, lu ñu jëfoon moom lañuy jëfati. Dara yeesul fi kaw suuf.
10Lëf a ngii, nit naa: «Lii de lu bees la,» te mu ngi fi woon lu yàgg, lu jiitu sunu juddu.

Read Kàdduy Waare 1Kàdduy Waare 1
Compare Kàdduy Waare 1:8-10Kàdduy Waare 1:8-10