Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàdduy Waare 1:8-10 in Wolof
Help us?
Kàdduy Waare 1:8-10
in
Kàddug Yàlla gi
8
Jëfoo jëf ca jëfit, làmmiñ tuddul lépp, bët du suur, nopp du buur.
9
Lu ayoon mooy ayati, lu ñu jëfoon moom lañuy jëfati. Dara yeesul fi kaw suuf.
10
Lëf a ngii, nit naa: «Lii de lu bees la,» te mu ngi fi woon lu yàgg, lu jiitu sunu juddu.
Kàdduy Waare 1 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms