Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàdduy Waare - Kàdduy Waare 1

Kàdduy Waare 1:17-18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17di dogoo xam luy xel mu rafet, xam luy nitoodi akug ndof. Fekk loolu it napp um ngelaw la.
18Ku géejal xel mu rafet, géejal naqar; yokku xam-xam, yokku tiis.

Read Kàdduy Waare 1Kàdduy Waare 1
Compare Kàdduy Waare 1:17-18Kàdduy Waare 1:17-18